Instrumente
Ensembles
Genres
Compozitori
Artiştilor

Text: Ismaël Lô. Sénégal. Le Jola.


senegal senegal siguil ndiguale
gambia gambia oh siguil ndiguale
amna benna ferie bougnou dane nane
bateau le jola mi soukh sibir gueth gui
xalebi migui dioye nane baye
baye anna sama yaye yaw
baye neko dome anna yaye boye yaw

senegal senegal siguil ndiguale
gambia gambia oh siguil ndiguale

Mane baye migui dioye nane dome
dome anna sa yaye boye
dome neko baye anna yaye boye nam
kone li firina ni yala reke sagne yala
reke mane kon mome rekeu moy bour

senegal senegal siguil ndiguale
gambia gambia oh siguil ndiguale

Ndakh kepeu ko lath moune amnathi
Waye kon lii fir ndena ni senegal bena bopeleu

senegal beneu bopeleu
senegal bena bopeleu

bilay

ken douko khar gnaro

beneu bopeleu senegal

faguarou diotna
nagnou xolat sougnou bopeu bou bakh

nagnou bayi douman kila
bo dioume dagua wara nangou
diougue
heu heu heu heu
bougnou diogue sili
nagnou kholat sougnou bopeu bou
baaakh
beneu bopeleu heu heu heu
beneu bopeleu senegale haha hahale

senegal senegal siguil ndiguale


(Grazie a Loredana per questo testo)
Ismaël Lô